Lutax dexx biidi Retba am mélo Karoot ? (wolof)

Applause IconApr 06, 2022 • 6:31 AM UTC
Location IconUnknown Location
Applause Icon140x Magnification
Applause IconUnknown

Learn about the author...

8posts
2comments
6locations
Traduction: Cheikh Gawane Diop
Dexx biidi Retba, gnu koy dakantalé tamit (Dexx bu amé mélo Karoot ci kalama nasaran), nek na bereub bugnu ragné ci Sénégal, nek fu soréwul lool ak dekuk taax biidi Dakar. Dekh bi dafa wexx : am melo Karoot ci nign ko mana waxé. Nenan ma itam mo guen saf xorom fukki yoon liidi guedj gui.
Gnu bari ci ay dommu adama fi lagniy wuté xorom, bu gnu noppé weer ko ci nathie bi. Dagn ciy am ay tonnu xorom bu sell sax.
Gnep gni nekk ci gale-gui dagno am mbegté di xool lan mo nek ci biir ndox mi. Guiss nan ci ay ferr gnent yu amé mélo bu xonkh. Bari nagnu lool banga xamni foo xolé di guiss fer gnent yi. Lolu nak liko waral mooy ndox mi dafa am mélo bu feuss lool.
Guestu bu ndaw bugnu def ci walum diumtukayu xaralé yu yess yi diangaléna ni ferr gnent yoyu di nek ci ndox mi man na book ci liy soppi mélo bi. Kon xel nanguna Dexx bi am mélo bu melni.

Sign in to commentNobody has commented yet... Share your thoughts with the author and start the discussion!

More Posts from Melanie Hannebelle

Échantillon de plume

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
1y
Oeuf d'Ascaris

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y
A warm day in Dakar, seneg

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y
When microbiology meets plant and human health: visiting the aflasafe factory, in Kaolack, Senegal

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y
Quand la microbiologie rencontre la santé des plantes et des humains: visite de l’usine d’aflasafe, Kaolack

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y
Pourquoi le lac Retba a-t-il la couleur d’une carotte?

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y
Why does the Retba lake have the color of a carrot?

Applause Icon 0 ApplauseComment Icon 0 Comments
2y